Leçon 7 : Les fruits

Publié le par Estelle

Anaana bi L'ananas
pom bi La pomme
banaana bi La banane
gërënaat bi La grenade
guyaab bi La goyave
pàppaayo bi La papaye
Karosool bi Le corossol
màngo bi La mangue
soraas bi L'orange
limon ji Le citron
pampalmuus bi Le pamplemousse
koko bi La noix de coco
Màdd bi Le mad
Xaal bi Le melon
Bouye bi Le pain de singe

 

Publié dans Wolof

Commenter cet article