Leçon 5 : Les chiffres

Publié le par Estelle

Tus Zéro 0
benn Un 1
ñaar deux 2
ñett trois 3
ñent quatre 4
juroom cinq 5
juroom benn six 5+1
juroom ñaar sept 5+2
juroom ñett huit 5+3
juroom ñent neuf 5+4
fukk dix 10
fukk ag benn onze 10+1
fukk ag ñaar douze 10+2
fukk ag ñett treize 10+3
fukk ag ñent quatorze 10+4
ñaar fukk vingt 2x10
ñaar fukk ag benn vingt et un 2x10 +1
fanweer trente 30
ñent fukk quarante 4x10
juroom fukk cinquante 5x10
juroom benn fukk soixante (5+1)x10
juroom ñarr fukk soixante-dix (5+2)x10
juroom ñett fukk quatre-vingts (5+3)x10
juroom ñent fukk quatre-vingt-dix (5+4)x10
téeméer cent 100
Junni mille 1000

 

Publié dans Wolof

Commenter cet article