Leçon 3 : Se présenter

Publié le par Estelle

Fan nga joge ? D'où viens tu ?
Faraas laa joge Je viens de France
Waa Faraas laa Je suis française
Na nga tudd ? Comment t'appelles-tu ?
Maa ngi tudd Estelle Je m'appelle Estelle
Sant wi ? Le nom ?
Lan mooy sa liggéey ? Quelle est ta profession ?
Jangalekat laa. Je suis enseignante
Damay jangale J'enseigne
Kañ nga fi ñew ? Quand es-tu arrivé ?
ñew naa démb ci guddi Je suis arrivé hier dans la nuit
Yàgg nga fi ? Es-tu ici depuis longtemps ?
Am naa fi juroomi fan Je suis ici depuis cinq jours
Kañ ngay dellù ? Quand repartez-vous ?
Fii ag ñaari fan D'ici deux jours
Altine bi di ñew Lundi prochain

 

Publié dans Wolof

Pour être informé des derniers articles, inscrivez vous :

Commenter cet article