Leçon 8 : La famille

Publié le par Estelle

yaay ji / ndey ji la maman
pappa ji / baay ji le papa
maam ji le grand père / la grand mère
jabar ji / jëkker ji l'épouse / l'époux
doom ji l'enfant
sët bi le petit fils / la petite fille
jarbaat ji le neveu / la nièce
bajjan ji la tante paternelle
nijaay ji l'oncle maternel
tanta ji la tante
goro bi le gendre
mag ji le grand frère / grande soeur
rakk ji le petit frère / petite soeur
doom ju jigeen ji la fille
doom ju goor ji le fils
mag ju goor ji le frère ainé
rakk ju jigeen ji la petite soeur

 

Publié dans Wolof

Commenter cet article