Leçon 1 : saluer et prendre congé

Publié le par Estelle

Salaamaalekum Bonjour
Maalekum salam Bonjour
Na nga def ? Comment ça va ?
Maa ngi fi rekk ça va
Jamm rekk ça va
Naka waa ker gi ? Comment va la famille ?
ñu ngi fi ça va
Naka xalé yi ? Comment vont les enfants ?
Naka sa jabar/ sa jëkkër? Comment va ta femme / ton mari ?
Mbaa kenn febarul ? J'espère que personne n'est malade
Déedéet, jàmm rekk Non, on se porte bien
ñu ngiy sant Yalla Dieu merci
Na nga fanaane ? Comment as-tu passé la nuit ?
Bu baax kay Bien assurément
   

 

Maa ngiy dem Je m'en vais
Ba beneen yoon A la prochaine
Demal ag jàmm Bonne route
Yendul ag jàmm Passe une bonne journée
Fanaanal ag jàmm Passe une bonne nuit

 

Publié dans Wolof

Commenter cet article